Déranger

Viviane Chidid

Bilé mélokaane molay déranger
Xamna lilay sonal
Waax diou bari tek thji nga diss té yanou wo
Xamna lilay sonal
Bilé mélokaane molay déranger
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma séen dima rétann té beugoulo ma
Yallah mayma nangou wo
Ma rombou la nangou wo
Foma séen talalma lokho té sopou lo ma

Xamna lilay sonal
Mani wakh diou bari tek ci nga diss té yanou wo
Xamna lilay sonal
Bilé mélokaane molay déranger
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma sèen dima rétann té beugoulo ma
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma sèen talalma loxxo té sopou lo ma
Hey! Tiré ngama visél ndakh dalouma (louma)
Tiré ngama visél ndakh dalouma (hey)
Tiré ngama dolil ndakh dalouma (louma)
Sit down yow
Fi adinala konn tèyal
Fi adinala fils tèyal
Fi adinala konn tèyal
Fi adinala fils tèyal

Xamna lilay sonal
Waax diou bari tek thji nga diss té yanou wo
Xamna lilay sonal
Bilé mélokaane molay déranger
Yallah mayma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Foma séen dima rétann té beugoulo ma
Yallah mayma nangou wo
Ma rombou la nangou wo
Foma séen talalma lokho té sopou lo ma

Hey! Tiré ngama visél ndakh dalouma (louma)
Tiré ngama visél ndakh dalouma (hey)
Tiré ngama dolil ndakh dalouma (louma)
Sit down yow
Dieuleul way wi ma mayla yeah
Dieuleul way wi ma mayla yeah
Dieuleul way wi ma mayla yeah
Yaw dégloul way wi may nala defko cas

Lingay dégager (dégager)
Mokoy déranger (déranger)
Yalla ko def thji yaw
Niou waxanté deugeu
Lingay dégager (dégager)
Mokoy déranger (déranger)
Yallah ko def thji yaw
Niou waxanté deugeu

(Hey, ma teug ko, ma teug ko, ma teug ko
Fèthieu ko, fèthieu ko, fèthieu ko
Vivi way fi niou teugeu fè nguèn dadi bégué
Nganni?)

Gal gal Amadou, Moustapha Diop malkhourédia baye lan niang moy sa man
(Moustapha Diop domou louga lô adja dior moy sa yay nitt kou baakh)
Wakhoumako wa louga ko wakh yangui dimbalé, di diapalé
(Té doula togn, té doula togn
Elhadji bassirou diop moy sa beay Moustapha eeh way)
Moustapha Diop, Moustapha bassirou’roy sa baye, dior diop sa yaye
(Vivi-Mbaye dièye faye loula yalla may
Gueuremèko sa nday bagn douko dindi)

Nitt koulay woutt (lo si wax?)
Dièm dièm diotoula (louy pékhèm)
Dafay sétt kila guena dièguè mou diarèfa
Ba yakal leu wayè yaw mi boulèn falè

Mani nitt koulay wout (lo si wakh?)
Dièm dièm diotoula (loumouy def)
Dina sètt kinga guena dièguè mou diarèfa
Ba yaxal leu wayè Viviane doulèn falè
(Boul falé, boul topato wayé dèlènn saurr
Vi-Vivi-Viviane oh, Vivi-yatma thiam nieuweul)

Lingay dégager (dégager)
Mokoy déranger (déranger)
Yalla ko def thji yaw
Niou waxanté deugeu
niaff

Otros artistas de Contemporary R&B