The Ñuulest

Xaaju guddi la koy lijjënti, non non du jàmm ni guerre civile
Ku nekk sa fetal mooy Amerique, Ku nekk sa waññi mooy Françafrique
Pour toog fu nooy fok nga dëgër fit, sooy fen ci podium bi du la jig
Boys yi ci hood bee la gën a sick, gën la màndi, gën la nekk nit
Su dee xaalis mooy danger, loolu mooy manoo jënd fit
Su dee jigeen mooy danger, ñoom rekk ñoo fiy jur ay nit
Succès ak a lunatique, tipse boy yépp a ma sib
Rayal ñépp si t’es dans le doute, real shit, ñuul kuuk

Ñuul kuuk, ñuul kuuk, ñuul kuuk, ñuul kuuk, ñuul kuuk…
Yeah … Hey, N-eazy mooy the Ñuulest, N-eazy mooy the Ñuulest
Tout est noir comme le Ñuulest, tout est noir comme le Ñuulest

Battling Siki moo lay uppercut, doole yamul taamul li nga jot
Sama benn flow bi mo lay sot, du ma ko bàyyi comme tapette bu lay kott
Sëriñ bi ak a ñaaw njort, nee na sa shine de daaw la jot
Wutal ginaar gu ñuul mais sans bopp, te bés boo koy suul doo sol culotte
Plus muy gën a lëndëm, plus ngay gën a jënd,
Fils yi gën a cuune, bëgg a tekki fu ne moo léen jaral lu ne
Sho yi laal léen fu ne, bés ñu jiiñ la gone
Non non non non boy doo assumer
Bagaasu nit ku ñuul li mu toll, xanaa gone daawul sol tubéy
Ñuul kuuk yeah I gotta say

Duñ ci tàyy, dooleel der bu ñuul my nigga du ñu bàyyi
Du ñu bàyyi, lu mu metti nigga duñ ci tàyy
Dooleel der bu ñuul my nigga du ñu bàyyi, du ñu bàyyi
Yeah yeah ah

Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !
Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !
Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !
Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !

Hey, jël barre bi élevé, God kese moo lay jële fii
Fight kese moo lay yëkkati, fuck tëdd nigga da ñu tëradi
Der bu ñuul a gën a dëgër fii, mais der bu weex a gën a dëgër fit
Yéen rekk a faale doole njiit, yéen rekk ay fal ay doomu njiit
Bàyyi léen foog ne képp ku jóge bitim réew moo la ëppale
Bàyyi léen foog ne lu ñu daan def sunu maam yi moo ñu téye ba léegi
Moom sunu weccet, moom sunu réew
Fuck nigga ñoo la gën a reew, moom sunu xel ak sunu réew

Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !
Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !
Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !
Non non boy du ñu bàyyi dara sedd no !

Músicas más populares de Nix

Otros artistas de African music