Nobatouma
Nobatouma
Refrain
Légui xoolatuma, nobatuma, feelatuma
Couplet1
Ma touki nieuw mu ni ma bye bye
Xana man mi du ma sa waay
Niakk xam mo waral lu bari waay
Fogone na ni ma nekk sa xol bi
Fogone na ni duma meuss guénn sa xol bi
Yow chérie kaay waay yow bou fi saalé mane rek nga beugg...
Refrain...
Légui xoolatuma, nobatuma, feelatuma
Couplet2
So baby fatalikul bi nga fi lambé ma la sauvé
Bi la xalé yu goor yi bari rombé yangui chômé
Fogone na ni war ma di na la jomb do cu goré
Légui toppe na sa ganaaw ba sonn mi amoré
Deugg leu mane da ma la nop
Mais sa jikko bi nga change mane def na ma choc
Babe lepp nioko dan bokk
Bo ma faléwone ba légui lou niou songue daan ko
Té nga tok niu waxtaan
Té nga baayi sa ćaaxaan
Ndax bou ma xassé ba dem dootu ma si delussiwaat
Té nga fey sa portable
Té nga wagni sey tankk
Ndax cu la beugg ni mane dooto co gui meun na co waat
Yow Alla abal ma mic
Cho bi da ma co mugneul da ma xeex ba mu tight
Teey ji feelatuma né na amatul vibes
Mais totch ne sama tchoukel mais nak du té ma baayi bye-bye
Refrain
Légui xoolatuma, nobatuma, feelatuma