MBELE

Bruno HOVART, Lansana SANE

Yé last timp ga nékeu di misère
Ndahe gayi di wahe di yakeu déra
Fatal sa xéle ba méneni xéra
Sougnala guissé di beugeu dé ya
A xolale guestoumaléne
Yawe guissale faléoumaléne
Filéc yagui defe louléne néhe
yadé doto ame loula néhe

Mbélé
mbélé mbélé
Mbélé mbélé mbélé
Arrete de parler derriere mon
Bayil mbélé mbélé
Xolale limaye doundé téhoula loussi yone
Xolale nimaye doyé téhoula loussi yone
Ya xole ya guisse ya wahe téhoula loussi yone
Légui dale mala déssé téhoula loussi yone

Mbélé
mbélé mbélé

Mbélé mbélé mbélé
Arrete de parler derriere mon
Bayil mbélé mbélé

Músicas más populares de Lass

Otros artistas de Afrobeats