Gentleman Remix

Elzo JamDong

[Intro]
Yo it's ya boy Elzo from Jamdong Community
Yeah
Mais tey dama am ganou gentleman
Yo Killah !

[Couplet 1: Nitdoff]
Biggie dou dead sunu aaroon Pac
Goudi gui yéniou né 44
Gathié guey déss suma maaroon taate
Taalna gun yifou naroon takk
Équipe bou none yi di gueuneu thiol takhneu beu gars yifa faroon fakkh
Akimo game ame monopole succés bi yomb na faram facc
Gun down gun down ten years magui run town
Mao school sama Duncan cuistot leu bou meun guane
Yeah right yeah right it’s an order bou ken bagn
Boko tagué dey gêner wou bouy cedelé sakh moy moudjié ame
Dey daw thiow melni nieméwoul boul diawalé ragal ak gentlemen
Lokhom dou meusseu dale tchi djiguen
Guiminieum jalousie dou ci guenn
Lou respect bi amoul deh dou ci dem
Bo newoul tchi li do gentleman
Job neu beu songu leu daw neu beu romb leu
Pele biley guassal sa tombe leu killahrie bombe leu
Rap sama monde leu Elzo dou ennemi li jamdong leu
Médaillou or ci loss hulk ci corpulence, sa bord silence
Sa gars yi goor di khoss Killah çi endurance dou concurrence
Succès bi daniouko job ay sacrifice la lathie dou coïncidence

[Refrain]
Defal seu job
Beuss di neu dokh
Kenn matoul tchi addouneu
Gueumeul seu bopp
Mané gueumeul seu bopp
Bo togné ngueu diégueulou
Bo togné ngueu diégueulou
Bo togné ngueu diégueulou
Lo loy gentleman
Gentleman x8
Kham naa louy parcourou gentleman
Seu benn pékhé mounou niou gener man
Boy yaa ngui pèlleul niou thiéné rek
Kenn gueunou niou nekk gentleman
Gentleman x8
Kham naa louy galèrou gentleman
Seu benn pékhé mounou niou gener man
Boy yaa ngui pèlleul niou thiéné rek
Kenn gueunou niou nekk gentleman

[Post-Chorus]
Lokho tchi kow bo dé gentleman
Gentleman gentleman gentleman
Kham naa louy galèrou gentleman
Gentleman gentleman gentleman

[Couplet 2: Elzo]
Gentleman gentleman gentleman
Depuis temps wou Sunu Flavor beu legui mane khawma dara loudoul jengu man
Benn nit dou mouss beu weussine domou khadj te rasta dou deukk tchi tenement
Khalato wone nitou diamm déclencher ay guns out nigga tey nga dèè
LG ak Macina benn gangg
Qualité kessé laay faratal
Hit yimay enchaîner aka tarr
Tout terrain kakkatar
Lepp Dope comme kou diogué Caracas
Yaggouma torop tchi game bi wayé nak dofouma diangg naa li tchi birr
Money dou miss dou jongoma wayé aka beuri satan you tchi mirr
Dioulli seulmeul solou beu nice
Gentleman go to the top
Yor cash money comme Juvenile
Cash money comme Juvenile
Gentleman sokhoroul waay
Dey diokhé assaka di pray
Gentleman taloul détails
Kill them with positive vibes !
Indi lou bess, comptes yi fess
Akkimo aise, baayil leu stress
Rest in peace Papa gentle nga yaama daan diokh lou meu lèkk
Petit félin bou rèpp né dey khossi Diallo bi dotou ko def
Ngané tu veux de l’or (alal ak wourouss)
Nekk over the law (over the law)
Boul di fomb seu job te baayi kou romb nga dieuw (tedieul seu guemign)
Gueumeul seu bopp, bo togné ngueu diéggueulou
Bo togné ngueu diégguelou, bo togné ngueu diéggueulou
Lo loy gentleman

Chorus x1

End

Curiosidades sobre la música Gentleman Remix del Elzo JamDong

¿Cuándo fue lanzada la canción “Gentleman Remix” por Elzo JamDong?
La canción Gentleman Remix fue lanzada en 2019, en el álbum “FreeSeason 2”.

Músicas más populares de Elzo JamDong

Otros artistas de African hip hop